Le message de remerciement de Modou Lo s’adressant à ses fans

Alhamdoulilah alhamdoulilah alhamdoulilah doli sant Yalla dilène massawou thiono boubakh. Guis na messages yeup ak appels yii. Dilène félicité tamite. Yalla nalene Yalla faye inshallah. Merci beaucoup. Dilène fatali tamite bii moye sama Facebook. Jajeuf Fans yii kharite yii supporter yi Mbokk yii yeup souma limé rek dioum. Alhamdoulilah begué

 

LAISSER UN COMMENTAIRE

S'il vous plaît entrez votre commentaire!
S'il vous plaît entrez votre nom ici