belles paroles!
De belles paroles sur Serigne Saliou Mbacké à lire absolument!
“ñeenti yëf day jur ak weradi= wax ju bari, nelaw yu bari, lekk gu bari,ak sëy lu bari.
ñeenti yëf day rësël aw yaram= tiitaange, njaqqare, xiif, ak ñakka nelaw.
ñeenti yëf day wowal kanam di dindi ndoxum kanam akub taaram= fen, neew kersa, barik laaj ta doo xam, ak barik caay-caay.
ñeenti yëf dafay dólli ndoxum xar kanam akub taaram= ragal yàlla, matal kollare, am tiraanga, ak mbañam rus.
ñeenti yëf dafay ñóddi wërsëk= naafila guddi, barik jeggalu ci waxtuw njël, sàmm ak xaritoo, ak tudd yàlla suba ak ngoon.
ñeenti yëf day xañe wërsëk= nelaw suba teel, néewël julli, tàyyeel, ak wor“