Le musicien, natif de Fass, leader du Mbouba Diali et ancien pensionnaire de l’Orchestra Baobab, a fait ce poste pathétique sur sa page facebook Ce dimanche: « Mbokk yi dafa am ñari tele ak ñari radio, yu nek fi ci Senegal, ak yeneu animateurs youmay xeex xeex bu metti. Duñu tek sama clip, duñu tek samay way, bëguñu ma feeñ fenn. Li moo tax may ñaan mbok yi, xariit yi ak sope yi ngeenjapp ci promotion bi di saku ci yeen ñaane lepp ci jamm ak salam. Yalla rek moy Buur, moy Borom doole, Yalla nañu Yalla aar samm ñu, defal ñu jamm, tagaléñu ak tiis, tagaleñu ak saytaane, lafalñu thiat ».
buzzsenegal