2021 s’en va avec son lot de joies et de tragédies pour notre cher pays.Accueillons 2022 avec espoir, en priant qu’elle soit favorable au Sénégal et aux Sénégalais, et en nous mettant dès à présent au travail.==================================2021 a ngi dem, ànd ak i mbégteem ak i naqaram ci réew mi.Nanu gatandu atum 2022 ànd ci ak yaakaar, tey ñaan mu doon njiglaayu Senegaal ak ci saa-senegaal yi, mu fekk nu nag nu noppi ngir door ci liggéey bi.